bismillah mangui sante yalla' di sante yonete tome mouhamath
di sante cheikh ahmed jijane rabiyalahou hankhou
di sante mame baye niass mom mi ma rey ci man dkèlma ci yalla
dah moma khamale ki ma done' reyci mane ki ray
moy borome khoudbou zamani'moy islam moy maoti moy chariya moy khakhtou diouli yiguèni diouli moy fanaw moy bakhao moy aweulou moy akirou moy zahirou moy batinou' té moy bakani moy gokhi moy lep li guène meunti guis' moy baye niassssssssssssss di sante outaz baye kébé mom mima yègale ci yalla rey ci ismouyi ak méloyi ak dieumyi""" déé lène balla déé di nieuw
( je vous di kelk choz c le coeur ki sen dieu no la raison en matier de religion il fau croir pour comprend' los
fi guène dkeulé yalla dkoufeu dah yalla moy lep wayé lep tam dou yalla" soké woute cèt ko ci yow dah geunoula moy lep soxolé sah moy yow moy lep.............